notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Soxna Si (feat. Admow)

OMG

Soxna Si (feat. Admow)

This is the Remix
Girl like you
My name is Admow Flow, aka Chos

Nobody wanna see us together (together, yeah)
Nobody wanna see us together but they don't matter know

Xool naa la xool keneen
Gis ni bokkuleen
Kon jarul may dem seeti keneen
No, no, no
Yaa ma jox say coordonés
Sama life nga ordonné ko
Kon man duma la abandonné, baby

Ku mel ni yaw mooy ki baax ci man
Ku mel ni man mooy ki baax ci yaw
Su guddi xaajee ba sama xel dem ci yaw
Maa xam ni I love you, yeah, yeah

Yeah, yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Soxna si, I love you yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Soxna si, I love you yeah, yeah

Dama blindé ci ñeneen ñi, doon ngaaka ci yaw
(Cause I love you, yeah, yeah)
Jamdong laa la bégal, dinga dundu ba gis ko
(Cause I love you, yeah, yeah)

Oh, souka débo yodi, ko ane woni fittandam
Ko oh, Modji, sa diali, éné boubna berdame
Oh woni sékhilame
Oh woni guidélame
Oh woni diom soudame, honoma ala no no no

Ku mel ni yaw mooy ki baax ci man
Ku mel ni man mooy ki baax ci yaw
Su guddi xaajee ba sama xel dem ci yaw
Maa xam ni I love you, yeah, yeah

Yeah, yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Soxna si, I love you yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Soxna si, I love you yeah, yeah

Loving you is what I do girl (éh aay éh)
Dañu bëggante ba mujj niróo (éh aah aah éh)
Kone ane woni é ndér bérndam, girl
Halnam saa ndaarikam holko ndiyata
Xool ma ci ay bët wax ma looy gis?
Sori la baby dina ma diis, baby

Ku mel ni yaw mooy ki baax ci man
Ku mel ni man mooy ki baax ci yaw

Su guddi xaajee ba sama xel dem ci yaw
Maa xam ni I love you, yeah, yeah

Yeah, yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Soxna si, I love you yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Yeah, yeah, yeah
Soxna si, I love you yeah, yeah