notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Ci Peet

OMG

Ci Peet

Sa lokho sama boss ma feel leu
Ni courant bouy daw thi fil leu
Niouy doundou lou nice, niceee
Nékal sama wéte ma chill
Guem na ba abadane ni fi leu
Sama khol séd ni ice

Bomay khol may ré
Ci peet mangui deh
Fouma dem fouma dem
Baby yaw lay bégué

Ci peet yamay danel
Ci peet malay danel
Niouy kholaneté di ré
Délou donate khalé
Ci peet yamay danel
Ci peet malay danel
Niouy kholaneté di ré
Délou donate khalé

Sama khol ak sama khel
Nek thi yaw fouma nek
Beugue nek sa honey sa only
Dila kholé beutou mbeuguel
Baby yamay danel
Sans yaw meunouma noyi
Yaye sama air boulma sori
Just wanna be with you

Baby yamay danel
Sans yaw meunouma noyi
Yaye sama air boulma sori
Just wanna be with you

Ci peet yamay danel
Ci peet malay danel
Niouy kholaneté di ré
Délou donate khalé
Ci peet yamay danel
Ci peet malay danel
Niouy kholaneté di ré
Délou donate khalé

Fouma demmmm
Mak yaw forever
Kou beugue beugue na
Kou bagne beugue na
Hahahahahannhan
Hanhanhanahana
Ohwouwoo
Oh, baby baby baaby
Ouhhh ououhhouuu
Ci peet yamay danel

Beugue nek sa sokhna dila wowé ma boo
Lepp louma am baby it’s for you
Your love give it to me, I give it to you ouhouh
Hannnhanhanhanhanhan
Sama khol yako mome, oh ci peettt

Yamay danel
Malay danel
Oh ci peet
Baby ci peet yamay danel
Malay danel
Yamay danel
Oh ci peet
Ci peet yamay danel