Li may dundu ni li Yàlla bu mu jeex
Fi ma nekk ni dafa romb neex
Ki ma tee ni ay loxom dañoo woor
Xol bi moo ngi feex, man xamuma woon
Yaa ma woon (yaa ma woon)
Fi ma lay yóbbu maa ko xam
Yaa leen gëna pare yaa leen mën (yaa leen mën)
Defal lu la neex yaa ko fi am
Yaa mëna yee li nelaw ci man
Windeluwma te miir naa (miir naa)
Joxuloo ma livre te liir naa (liir naa)
Ma xam ne yaay ki baax ci man
Wóolu naa la te fiir naa (fiir naa)
Yaa fi ne
Man ma la validé
Sama xol bi yaa ci ne
Man ma la validé
Baby yaa fi ne
Man ma la validé
Sama xol bi yaa ci ne eh
Man ma la validé
Lu ne nga ma jaral
Sa bu neexee yaa ko waral
Yaa ma jommal sama jinne
Dama yénne di la teral
Loo amul ci man yaw la
Danga ma nob ma raw la
Naa la aj fu kawe, kenn mënul yéeg ba ajji la
Maa fa teg jeexal (jeexal)
Sama dundu yaa koy neexal (neexal)
Ne nañu ma naa la bàyyi
Ma naa leen ma bañ!
Ki bëgg naa ko na ma ray
Moo may gaañ
Xam sama valeur
Yaw yaa xam li may jaar
Doo ma jënde keneen, sama alal
Yaw yaay ki may wër
Ndax guddi ba fajar
Yaa koy neexal ni lem ki ma tànn
Yaa fi ne
Man ma la validé
Sama xol bi yaa ci ne
Man ma la validé
Baby yaa fi ne
Man ma la validé
Sama xol bi yaa ci ne eh
Man ma la validé
Maa fa teg jeexal (jeexal)
Sama dundu yaa koy neexal (neexal)
Xol bi yaa koy feexal (feexal)
Sama dundu yaa kou neexal (neexal)
Samp rekk teg fa jeexal
Sama dundu yaa koy neexal
Xol bi yaa koy feexal
Sama dundu yaa koy neexal
Yaa fi ne
Man ma la validé
Sama xol bi yaa ci ne
Man ma la validé