Les goûts et les couleurs ne se disputent pas
Man ki ma bëgg jox ko sama xol, na ngeen masi Ba
Ni mu tollu la ko bëggee avec son poids, je l'aime moi
Bala may dof ma téye la, nga fees samay loxo
Ndax xale bu fees bari jàpp moo jara tek loxo
Awumak affaire taille fine, man ni la miin
Way jekk ji ñoo may dadji yeah, yeah
Su ma naree dee ci àll na ma Gaynde Ray
Su ma naree dee ci àll ginnaar duma ray boy
Soo bëggoon étage, chérie moom la lay may
Ni ma la bëggee dara du ko fay, waa-waaw
Man li ma gëna bëgg taille fine la
Man li ma gëna bëgg jekk bu diis la
Non, man bëgguma jekk bu diis
Li may daaneel newul ci taille fine
Bët du yénu waaye xam naa lu bopp àttan
Bëgg naa ku yem xale bu maggul atam
Taille fine kenn du moom
Woyof àttan seen bopp ñoo ko moom, hèè!
Namm naa ku may fowee di ko nabb nabbé
Ku yem ci ay loxo ma koy wane ni ma ko nobee
Bokkul ak kiy tokk sa kaw te doo mëna noyyi
Diis ba dootoo yeukk loxom yu noy yi
Taille fine yi, sawar nañ te foo leen woo ñu wuyu la
Te yaw sa jekk bi boo ko toppee boo dawul ñu robi laa
Man li ma gëna bëgg taille fine la
Man li ma gëna bëgg jekk bu diis la
Non, man bëgguma jekk bu diis
Li may daaneel newul ci taille fine
Bu sééddaay jotee doo soxla àndu cuuraay
Dangay bokhou rekk tëdd ci wétam mu tokk di la ray
Bu tàngaay jotee doo soxla clim waay
Di nga mëna di foo ak moom te ñàkk du la ray
Ki dafa jonge ba lu ne la may defloo
Suñu tëddé daf may joyloo
Ki dafa woyof ba fu ne lay aw ci man
Bu may xalaat li ma may def daf may réeloo
Ñi àndak taille fine waneleen seen bopp (heey)
Ñi àndak jekk ji yeen a nangeen (heey)
Ñi àndak taille fine wanewuleen
Ni àndak jekk ji, jukkleen may xool
Man li ma gëna bëgg taille fine la
Man li ma gëna bëgg jekk bu diis la
Non, man bëgguma jekk bu diis
Li may daaneel newul ci taille fine