Hahahahaha
(Bril on the Beat) ha ha
Yeah, yeah Bril in the Building, héé
Cila Bokk way way Cila Bokk
Amoul Yakkalaté han, aythia Niou dém
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress
Boula kén ray doundou dafay nekh
Koula beugga sonal Romb ko né mééss
Niongui Foo, Happy, Bégué, Mba Xol yangui fékh
(Kaay) Cila Bokk Walay Cila Bokk
(Kaay) sagnsé andak kilay bégglo Cila Bokk
(Kaay) Cila Bokk Walay Cila Bokk
(Kaay) tok di sétane Loulay réélo Cila Bokk
Lo xamoul kagn lay djèkh dafa wara nékh
Boul faalé koulay méré wane ko beugn you wékh
Léppeu térangala, doundeul happyness
Lofi meunti am té béggo, amna louthi déss
Fii dal Sénégal la, boula nékhé dinga béggué
Boul nangou kèn yakkal-la
Dééko défé ning'ko beuggué
Daniouy dadjé foo di réé té xawma no Toudou
Selfie def ay Vidéo you fun melni #Dudu
#Baye_Mbaye, #Makh_Pro
Koufi mér kone Wéro
Warnga meune di enjoy nga né town wala ghetto
Boul nangou kèn dila téré Happy
Kou sa life néékhoul, yakoy soppi
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress
Boula kén ray doundou dafay nekh
Koula beugga sonal Romb ko né mééss
Niongui Foo, Happy, Bégué, Mba Xol yangui fékh
(Kaay) Cila Bokk Walay Cila Bokk
(Kaay) sagnsé andak kilay bégglo Cila Bokk
(Kaay) Cila Bokk Walay Cila Bokk
(Kaay) tok di sétane Loulay réélo Cila Bokk
Héé Yaw nanga déf
Koula beugga sonal thi wakh nèko mou déf
Défam té bayila rèk yaw nga néthi
Take it easy, dafa wara yomb, waroul, méti héé
Beurina ay Nitt you done foo djaarfa feullalé
Tèki_thi romboula wakh bo saani niou feul- feulalé
Kheuthiolén son you #Lourd, ma ték lou #Léger dilén Mour
Ngén may gueuna #Haine, maléni raw par #Amour
Bayilén niouy rawanté ngay dokh ndank, daagoul
Té koukay djaay méti, né ko Lou Méti Yagoul
Dél Khol sa none di réé né kouy sétane #Aba_Show
Caméra cachée #Makhfouss lay yooné sama Cho (copine)
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress
Boula kén ray doundou dafay nekh
Koula beugga sonal Romb ko né mééss
Niongui Foo, Happy, Bégué, Mba Xol yangui fékh
(Kaay) Cila Bokk Walay Cila Bokk
(Kaay) sagnsé andak kilay bégglo Cila Bokk
(Kaay) Cila Bokk Walay Cila Bokk
(Kaay) tok di sétane Loulay réélo Cila Bokk
(Kaay) héé féthial féthial way
(Kaay) ni rekla yeungoul yeungoul way
(Kaay) hééféthial way
(Kaay) ni rekla yeungoul yeungoul way
(Kaay) féthial féthial way
(Kaay) niou dèm, hèè Han han yeungoul yeungoul way
(Kaay) mané Cila bokk haayeah Cila bokk